TSK

TSK · Job 11:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Musaa ne ko: «Bu may génn dëkk bi rekk, di tàllal Aji Sax ji samay loxo, dënu yi dakk, tawub yuur bi siwet, ngir nga xam ne àddina, Aji Sax jeey boroom.

Job 5:8 TSK

Man de su ma doon yaw damay sàkku Yàlla, te kon Yàlla laay diis sama mbir.

Job 22:21 TSK

Jubool ak Yàlla rekk, am jàmm, ngëneel dikkal la.

te baña roy seeni maam; maas gu të woon te déggadi, ñu ñàkk pastéef te sàmmuñu kóllërey Yàlla.

Ma tàllal lay loxo, di la sàkku, ni suuf su mar di sàkkoo ndox. Selaw.

¶ «Jawriñ jooju xam nammeelu njaatigeem, te taxul mu waaj ko, ba jëfewu ko, ay yetam dina bare.