TSK

TSK · Job 16:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Job 9:34 TSK

teggil ma yetam, mu sore ma, ba darajaam ju raglu dootu ma tiital,

Job 13:22 TSK

Wooteel, ma wuyu, mbaa ma wax, nga àddu ma.

Job 31:35 TSK

Ma ne éy ku may may nopp? Sama torloo ngoog, na ma Aji Man ji tontu! Su dee téereb tuuma bu ma ku may layool bindal,

Lu masa ay, dees koo tuddoon; lu doom aadama doon, xamees na ko, te kenn du layook ku la sut.

Waaye yaw nit ki, yaay kan bay weddi Yàlla? Ndax këf ku ñu tabax dina ne ka ko tabax: «Lu tax nga sàkke ma nii?»