TSK

TSK · Job 21:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Job 12:4 TSK

Maay reetaanu xarit, te daan woo Yàlla, muy wuyu; tey ñuy reetaan ku jub, mucc ayib!

Job 13:13 TSK

Xeremluleen, ba ma wax man ak lu ma mana dal.

Job 16:20 TSK

Ñi may kókkali, saay xarit a, waaye Yàlla laa koy jooy.

Job 27:12 TSK

Dama ne, yeen ñépp a ko gisal seen bopp sax, kon lu leen yebuloo nii ci neenug neen?