TSK

TSK · Job 22:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

ngir di sàmm santaaney Aji Sax ji, ak dogali yoonam, yi ma leen dénk bésub tey ngir seen njariñal bopp?

Job 35:6 TSK

Soo bàkkaaree, lu muy wàññi Yàlla? Man ngaa tooñ, tooñati ba def ko dara?

Éy Yàlla, sàmm ma, maa ngi làqu fi yaw! Maa ne Aji Sax ji: «Yaay sama Boroom, awma alal ju la moy.»

Njàlbéenu xel mu rafet mooy sàkku ko; ak loo mana am, amal ug dégg.

Yeen itam noonu. Bu ngeen defee li ñu leen sant lépp ba noppi, dangeena war ne: “Ay jaam rekk lanu. Sunu warugar lanu def.”»