TSK

TSK · Job 28:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Job 28:21 TSK

Ump na bëtu lépp luy dund; njanaaw la fa kaw sax gisu ko.

Lu bon a la gënal lu baax, fen a la gënal wax dëgg. Selaw.

Am koo gën am xaalis, te njariñ laa raw wurus.

Alal ak teraangaa ngi fi man, am-am bu sax it ak yoolu njekk.

Jëndal dëgg te bu ko jaay. Sàkkul xel mu rafet ak yar akug dégg.

Ma noon: «Dootuma gisati Aji Sax ji, duma gisati Aji Sax ji fi kërug àddina. Duma tegati doom aadama bët, dootu fii ci waa àddina.