TSK

TSK · Joel 3:14

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Merum Aji Sax ji ñeel na xeetoo xeet, am sànj ñeel gàngoori xeet yi. Aji Sax ji faagaagal leen, dogal ñu war leena rendi.

Feek lu yàgg dees na la woo. Bu ay at jàlle ba jeex, yaay songi am réew mu nit ña rëcc saamar, ba jóge ci ay xeeti xeet, dajeji ca kaw tundi Israyil ya yàggoona wéet. Ñooñoo seppikoo ci xeeti àddina yi, ñoom ñépp dëkksi fa ci biir xel mu dal.

Joel 1:15 TSK

Céy, bii bés! Bésub Aji Sax ji moo dëgmal, te ni sànkute gu bawoo fa Aji Man ji lay dikke.

Joel 3:2 TSK

Kera jant yooyu, jaam yi sax, góor ak jigéen, maa leen di tuur samag Noo.

Waaye asamaanu tey jii, ak suuf, genn kàddug Yàlla googu moo leen yeb cib denc, ñeel sawara, kera bésub àtte ba, bésu sànkuteb aji gëmadi ñi.

¶ Ba loolu amee ma gis rab wi, mook buuri àddina yeek seeni gàngoor, ñu daje ngir xareek ki war fas week gàngooram.