TSK

TSK · Lamentations 3:43

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Éy Yàlla, ni daay di xoyome àll, sawara wa jafal tund ya,

Aji Sax jee def la mu nammoon, moo sottal kàddoom ga mu santaane woon janti démb. Moo fàdd te yërëmul, ba may noon bége leen, te moo kaweel sa kàttanu bañ yi.

Duma xool bëtu ñéeblu, duma ñeewante. Say jëfin laa lay yool ak sa jëf ju siblu ji ci sa biir. Su boobaa ngeen xam ne maay Aji Sax jiy dumaa.

Man it duma xool bëtu ñéeblu, duma ñeewante. Seen jëfin laay këpp ci seen kaw bopp.»