TSK

TSK · Leviticus 10:11

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Fexeleen ba ci biir mbasum jàngoroy der juy màgg, ngeen di sàmmoo jëfe bu baax, mboolem lu leen sarxalkat yi, Leween ñi tegtal. Ni ma ko sante sarxalkat yi, Leween ñi, sàmmooleen koo jëfe noonu.

Ci biir loolu ñu di leen jàngal téereb yoonu Yàlla wi, njàng mu leer, di leen ko firil ba ñu xam li ñuy jàng.

«Sarxalkat yi newuñu: “Ana Aji Sax ji?” Ñi ŋank yoon wi faaleetuñu ma, njiit yi gàntal ma, yonent yiy waxe waxyuy Baal, tuur mi, di topp lu leen dul jariñ.

«Kàddug sarxalkat déy day sàmm xam-xam, te ciy waxam la nit ñi di sàkkoo àlluwa, nde mooy ndawal Aji Sax ji Boroom gàngoor yi.

Ndax mboolem li Yàlla nar bañuma leen cee xamal lenn.