All books in KYG

Leviticus 13

KYG · verse 30

27 chapters

KYG / Leviticus / Chapter 13

KYG · verse 30

n a sarxalkat bi seet fi jàngoro ji nekk. Su melee ni lu def pax ci der bi, kawar gu xall te sew nekk ca, na sarxalkat bi biral ne nit ki sobewu na. Loolu wat-wataan la, di ër yuy génn ci bopp mbaa sikkim.