TSK

TSK · Leviticus 18:28

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ «Sàmmleen sama dogali yoon yépp ak sama santaane yépp te jëfe ko, ngir réew ma ma leen jëme, ngeen dëkki fa, bañ leena gëq.

Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: «Nee ñu réewum Israyil mooy dëmm buy dëmm boppam.

¶ Xam nanu ba fii nu tollu ne mboolem càkkéef gaa ngi binni ndax mitit, ni kuy matu.