TSK

TSK · Leviticus 18:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ca guddi ga ñu nàndal seen baay biiñ, taaw ba dugg, tëdd ak baayam, te Lóot yégul ba fa doom jay tëdd ak ba muy jóg.

¶ «Ku dëkkoo sa soxnas baay, sa baay nga torxal. Ñoom ñaar ñépp dee rekk mooy seen àtte, te ñooy gàddu seen bakkanu bopp.

su dul ñi ko gëna jege ci wàllu mbokk, muy ndeyam mbaa baayam mbaa doomam ju góor ak doomam ju jigéen, mbaa ku góor ku mu bokkal waajur,

Kii ak jabaru jaambur ci jëf ju siblu, kee sobeel jabari doomam ci biir yàqute, kale di tëdde rakki doom baayam fi sa biir.