All books in KYG

Leviticus 21

KYG · verse 8

27 chapters

KYG / Leviticus / Chapter 21

KYG · verse 8

T e itam nangeen ràññee ne ñu sell lañu, ndax seen ñamu Yàlla, ñoo koy joxe. Nangeen leen jox céru nit ñu sell, ndax ku Sell laa, man Aji Sax ji leen sellal, yeen.