Exodus 21:33
TSK
¶ «Su fekkee ne nit dafa ubbi kàmb gu ube woon, mbaa mu gas kàmb, wacc ko mu ne ŋàpp, ba nag mbaa mbaam daanu ci,
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ «Su fekkee ne nit dafa ubbi kàmb gu ube woon, mbaa mu gas kàmb, wacc ko mu ne ŋàpp, ba nag mbaa mbaam daanu ci,
¶ «Waaye su fekkee muy nag wu ñu xam ne da daan dañe, te boroomam ñàkk koo wattu, boroomam day feye nag wi dee aw nag wuy dund, daldi féetewoo wi dee.