Leviticus 8:36
TSK
¶ Aaróona ak doomam yu góor nag def lépp lu Aji Sax ji santaane woon, Musaa jottli.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Aaróona ak doomam yu góor nag def lépp lu Aji Sax ji santaane woon, Musaa jottli.
¶ Yooyu santaane la Aji Sax ji dénkoon Musaa ca tundu Sinayi, ngir mu jottli ko bànni Israyil.
¶ Lii mooy santaane bi, ak dogali yoon yeek àttey yoon yi seen Yàlla Aji Sax ji santaane ma jàngal leen ko, ngir ngeen di ko jëfe ca réew ma ngeen jàll jëm, ngir nanguji ko,
buleen déglu waxu yonent boobu, mbaa boroom gént boobu, ndax seen Yàlla Aji Sax ji moo leen di nattu ngir xam ndax yeena ngi koy soppe seen léppi xol ak seen léppi bakkan.
Biir géej di saw yoon; saw xàll ci digg ndox mu ne xéew, te kenn gisul foo teg tànk!