Luke 5:28
TSK
Lewi jóg, bàyyi lépp, topp ca moom.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Lewi jóg, bàyyi lépp, topp ca moom.
Yeesu dégg loolu, ne ko: «Lenn rekk nga deseleeti. Mboolem loo am, jaay ko, séddale ko néew-doole yi. Su ko defee nga woomle fa asamaan. Boo noppee, ñëwal, topp ci man.»
¶ Naka noonu ku ñuy wax Anañas, te ku ñuy wax Safira di jabaram, daldi jaay aw làccu suuf.
¶ Waaye la ma jàppe woon ag ndollant, moom laa def tey ag wàññeent ndax Almasi.