TSK

TSK · Luke 16:17

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Am ñax day wowal; tóor-tóor day lax. Waaye sunu kàddug Yàlla mooy sax ba fàww.»

Ndax loolu day tekki ne ngëm lanu jël, neenale ko yoonu Musaa? Mukk! Xanaa dañu koo dëggal kay.

Waaye bésu Boroom bi nib sàcc lay dikke. Ca la asamaan yi di dëddoo ci biir coow lu réy, lu ko sosoon seey ndax tàng, suuf ak jëf ju ci biiram xoyomu.

¶ Ma daldi gis asamaan su bees ak suuf su bees. Fekk na asamaan su jëkk sa ak suuf su jëkk sa wéy, te géej amatul.