TSK

TSK · Luke 2:18

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Man de, maa ngii, maak xale yi ma Aji Sax ji may, nu diy firnde fi Israyil te diy tegtal yu bàyyikoo fa Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, ki dëkke tundu Siyoŋ.

Luke 2:33 TSK

¶ Baay bi ak ndey ji nag yéemu ci kàddu yooyu ñu wax ci xale bi.

Luke 4:36 TSK

¶ Ba loolu amee ñépp a waaru, di wax ci seen biir, naan: «Gii kàddu lu mu doon? Moom de sañ-sañ ak xam-xam lay joxe rab yi ndigal, ñu génn.»