TSK

TSK · Luke 20:34

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Nit ñaa nga doon lekk ak a naan, di jël jabar ak a séyi, ba keroog bés ba Nóoyin duggee ca gaal ga, mbënn ma dikk, sànk ñépp.

Ni ko Mbind mi indee: «Looloo tax góor di bàyyikoo ci ndeyam ak baayam, daldi taqoo ak jabaram, ba ñoom ñaar di wenn suux.»