Psalms 38:13
TSK
Ñi may wuta rey a ngi may fiir, di ma jéema lor, di ma waxal musiba, yendu maa lalal pexe.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ñi may wuta rey a ngi may fiir, di ma jéema lor, di ma waxal musiba, yendu maa lalal pexe.
Musal ma ci sama mbugali tooñoo tooñ, bu ma bàyyi, dof di ma reetaan!
Mu ne leen: «Demleen wax njomboor moomu, ne ko: “Maa ngii di dàq rab yi, di maye ag wér, tey ak ëllëg. Bésub ñetteel ba nag ma sottal.”
Saaga nañu ko te feyuwul, daj na coono te tëkkoowul, waaye boppam la dénk kiy àtte dëgg.