Psalms 58:4
TSK
Ku bon day sosu rekk, dëng; juddu, teggi yoon, dib fen-kat.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ku bon day sosu rekk, dëng; juddu, teggi yoon, dib fen-kat.
ne ko: «Yaw nit ki fees ak gépp xeetu njublaŋ ak ndëngte, doomu Seytaane ji, noonu gépp njub, doo bàyyee lunkal yooni njub yu Boroom bi?
Ñaar yooyu du tebbiku ndax Yàlla du fen, te nun ñi daw làqusi ci moom, ci lanu ame ndëgërlaay lu réy lu nu ŋoye ci yaakaar ji ci sunu kanam.