TSK

TSK · Luke 4:27

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Ilyaas bàyyikoo fa, fekk Alyaasa doomu Safat, Alyaasa di gàbb ak ñaar fukki nag ak ñeent yu ko jiitu, ñu likke leen ñaar-ñaar, moom ci boppam mu jiital fukkeelu likke baak ñaar. Ilyaas dikk ba ca moom, sànni mbubbam ca kaw Alyaasa.

Job 21:22 TSK

Ana kuy jàngal Yàlla xam-xam, moom miy àtte ñu kawe ña?

Job 36:23 TSK

Ana ku ko masa rëddal yoonam? Ak ku ko ne: «Def nga naka-su-dul-noonu?»