TSK

TSK · Luke 4:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Yàquleeka leena bett! Musibaa leen ne fuuf, ñu ne mes!

ñiy jariñoo alalu àddina, bañ cee xér, ndax melow àddina sii tey, day wees.

Sunu coono bu woyof bii ci àddina, ci diggante bu gàtt nag, moo nuy jural teraanga ju diisaay ba jéggi dayo, teraanga ju sax dàkk.

Ndax kat sunub xare du nook boroomi deret ak suux, waaye ñi ñu ko séqal ay boroom nguur lañu, ak ay boroom sañ-sañ, ak ay boroom doole yu nekk ci àddina ju lëndëm jii, di ay dagi Seytaane yu fare déndi asamaan.