TSK

TSK · Luke 8:14

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Luke 8:7 TSK

Leneen la wadde biiri xaaxaam, jógandoo ak xaaxaam ma, daldi fatt ba wow.

¶ «Ab jaamu kër nag manula jaamu ñaari sang; day dëddu kii, sopp kee; mbaa mu fonk kii, cof kee. Manuleena jaamoondoo Yàlla ak Alal.»

Yeesu gis loolu, daldi ne: «Boroom alal tàbbi ci nguurug Yàlla, ndaw lu jafe!

¶ Ñi barele alalu àddinay tey nag, dénk leen ñu baña réy te baña yaakaar alal ju wóoradi, te ñu yaakaar Yàlla mi nuy xéewale lépp, ngir nu di ko bége.