TSK

TSK · Luke 9:16

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Muy jàngi yéeg, ñu di ko màggale Yàlla. Damaa séentu tund ya, te naan fu wall di jóge?

¶ Gannaaw loolu mu jël mburu, yékkati kàddug cant, dagg ko, jox leen ko ne: «Lii moo di sama yaram wi ñu jooxe ngir yeen. Deeleen def lii, di ma ko fàttlikoo.»

Loolu la wax, daldi jël mburu, sant Yàlla ci kanam ñépp, ba noppi dagg, lekk.

¶ Bu ma yékkatee kàddug cant ba lekk sama wàll, ana lees may sikke ci aw ñam wu ma sante Yàlla?

Ndaxte li Yàlla sàkk lépp a baax, du lenn lees ciy aayal, ndegam kàddug cant lees ko jariñoo.