TSK

TSK · Luke 9:47

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Yàlla, seetlu ma, ba ràññee sama xol; natt ma, ba ràññee sama xalaati xol.

Luke 5:22 TSK

¶ Yeesu nag xam la ñuy nàttable ci seen xel, daldi àddu, ne leen: «Lu ngeen di nàttable ci seen xel?

Te it amul mbindeef mu làqu fi kanam Yàlla. Lépp a ne duŋŋ, ne fàŋŋ, muy gis, te moom lanuy waxal bés-pénc.

Am mbas laay fàdde ay taalibeem. Su ko defee mboolooy gëmkat ñépp dinañu xam ne man maay nattu xol ak xel, te maay fey ku nekk ay jëfam.