¶ Ci biir loolu genn gàngooru njaxasaan mu nekkoon ca seen biir jiital seen bakkan, di ŋaf-ŋafi, ba tax bànni Israyil itam dellu di jàmbat. Ña nga naan: «Éy ku nuy leelatiw yàpp!
TSK
TSK · Malachi 1:12
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Numbers 11:4
TSK
Ezekiel 36:21
TSK
Ma daldi seet ci sama teddngay tur wu sell, wi waa kër Israyil di teddadil fi biir yéefar yi ñu fekki.
Amos 2:7
TSK
Ñooy dëggaate néew-ji-doole ci pëndub suuf, di xañ way-ñàkk àqam. Nit ak baayam di tëdde as ndaw, di teddadil sama tur wu sell.
Malachi 1:13
TSK
Yeena ngi naa: “Ndaw lu soof,” di ciipatu.» Aji Sax ji Boroom gàngoor yee ko wax. «Jur gu ñu sàcc ngeen may indil, ak guy soox, ak gu wopp, loolu mooy seen sarax! Nu ma koy nangoo ci seeni loxo?» Aji Sax jee ko wax.
Romans 2:24
TSK
Yeen de yeena tax ñuy ñàkke teggin turu Yàlla ci biir xeeti jaambur yi dul Yawut, te noonu la ko Mbind mi indee.