TSK

TSK · Nahum 1:13

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Man Aji Sax ji maay seen Yàlla ji leen génne réewum Misra, ngeen noppee doon seeni jaam; maa dog seen buumi njaam, siggil leen.

Mboolem dàll wu ab noon dukkate ba dikk, ak turki bu màndi deretu xare, sawara lees koy leel.

Maay joggati Asiri fi samam réew, dëggaate leen fi sama kaw tund yi, ba sama ràngi ñoñ rengiku, seenub sëf sippiku.»

Kon naa dem seeti kàngam yi, wax ak ñoom. Xanaa ñoom dinañu xam yoonu Aji Sax ji, xam lu seen àtteb Yàlla laaj.» Waaye ñoo bokk daggook Yàlla, dogook moom.