TSK

TSK · Nehemiah 13:19

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Wormaal-leen bésub Noflaay ndax lu sell la, ñeel leen. Ku ko teddadil, dee rekk mooy àtteem: képp ku ci liggéey, kooku dees na ko dagge ci biiri bokkam.

Seen bésub Noflaay la bu ngeen di nopplu doŋŋ te war cee toroxlu. Li ko dale ci ngoonug juróom ñeenti fan ci weer wi ba ca ëllëg sa, ba jant so, ci ngeen di wormaal seen bésub Noflaay.»

¶ Aji Sax ji da maa wax ne ma: «Demal taxawi ca buntu Doomi réew mi, fa buurub Yuda di duggeek a génne. Te nga taxaw itam ca mboolem bunti Yerusalem ya ca des.