TSK

TSK · Nehemiah 2:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage
Ezra 6:6 TSK

¶ Kon nag ñooñu di Tatnay boroom Wàllaa Dex ak Setar Bosnay ak seen nàttongo yay jawriñ ca Wàllaa Dex, nañu sore foofa.

Ezra 8:22 TSK

Ndaxte rusoon naa ñaan Buur mu boole nook ay dag ak gawar yu nu aar ci noon yi ci yoon wi. Li ko waral mooy fekkoon na nu wax Buur ne ko: «Sunu Yàlla mooy toppe yiwam mboolem ku ko yaakaar, di ko defal jàmm, waaye meram dina dal ak doole ci kaw mboolem ku ko dëddu.»

Ba loolu amee ma dem ba ca kilifay Wàllaa Dex ya, jox leen bataaxali Buur, fekk Buur boole maakay njiiti xare aki gawar.