Ezra 2:61
TSK
¶ Am na it ñu loolu daloon ci askanu sarxalkat yi, muy askanu Abaya, ak askanu Akocc, ak askanu Barsilay, ma doon denc doomu Barsilay waa Galàdd ba, ba tax ñu santale ko seen sant.