Nehemiah 8:7
TSK
Ci kaw loolu Yeswa ak Baani ak Serebya ak Yamin ak Akub ak Sabtay ak Odiya ak Maaseya ak Kelita ak Asaryaa ak Yosabàdd ak Xanan ak Pelaya ak Leween ña di leeralal mbooloo ma yoonu Musaa. Mbooloo maa nga taxaw, kenn ku nekk benn bérab.