TSK

TSK · Numbers 1:22

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Ca gannaaw ëllëg sa ñu ànd ak metit, ñaari doomi Yanqóoba ya, Simeyon ak Lewi, càmmiñi Diina, jël seeni saamar, dugg ca dëkk ba, bett leen, rey góor ñépp.

Doomi Simeyon yu góor di Yemuwel ak Yamin ak Owàdd ak Yakin ak Sowar ak Sawul, mi ndeyam di Kanaaneen.

¶ «Ñay dale fa feggook ñoom ñooy giirug Cimyoneen ñi, kilifag askanu Simeyon di Selumyel doomu Surisadaay.

giirug Simeyon, fukki junneek ñaar, giirug Lewi, fukki junneek ñaar, giirug Isaakar, fukki junneek ñaar,