TSK

TSK · Numbers 13:31

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Dangeena nara yoqiloo bànni Israyil, ba tere leena jàlli ca réew, ma leen Aji Sax ji jox?

Ana fu nu jëm? Te sunu bokk ya demoon yoqiloo nu, ne nu waa réew maa nu ëpp, sut nu, dëkk ya réy te dàbblikoo ay tata yu àkki asamaan. Rax ci dolli, ay ponkal yu bokk ci askanu Anageen ñi lanu fa gis!»