All books in KYG

Numbers 13

KYG · verse 32

36 chapters

KYG / Numbers / Chapter 13

KYG · verse 32

C i biir loolu ñuy baatal ca kanam bànni Israyil, réew ma ñu nemmikuji woon. Ñu naan: «Réew moomee ñu wëri woon ngir nemmiku ko déy, réew la muy faagaagal ay sancaanam, te mboolem askan wa nu fa gis, ay boroom jëmm lañu.