TSK

TSK · Numbers 14:40

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Ci kaw loolu ngeen wax ma, ne ma: «Noo tooñ Aji Sax ji. Waaye dinanu dem xareji noonee nu ko sunu Yàlla Aji Sax ji sante woon.» Ku nekk ci yeen daldi ràngoo ngànnaayam, ngeen defe ne yéegi diiwaanu tund wa dina leen yomb.

Bu boroom kër gi xasee jóg, ba tëj bunt bi, fa ngeen di doxe des biti, di fëgg naan: “Sang bi, ubbil nu!” Mu ne leen: “Xawma fu ngeen bokk.”