TSK

TSK · Numbers 14:41

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Lu la tere woona déggal Aji Sax ji, xanaa di saax-saaxee alal ji, di def li Aji Sax ji ñaawlu?»

Job 4:9 TSK

Yàllaay wal noowam, nga sànku, sànjam gelaw, nga jeele.

Babilon lees koy yóbbu, te fa lay des, ba keroog may wax ci moom.” Kàddug Aji Sax jee. “Bu ngeen xareek waa Babilon it, dungeen am ndam.”»