TSK

TSK · Numbers 16:28

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Mu ne ko: «Man déy, maay ànd ak yaw, te boo génnee mbooloo ma Misra, dingeen ma jaamusi ci tund wii. Loolooy firndeel ne, maa la yónni.»

«Bu leen Firawna waxee ne leen: “Defleen seeni kéemaan boog!” danga naan Aaróona: “Jëlal yet wi, sànni ci suuf ci kanam Firawna.” Su ko defee yet wi dina soppliku jaan.»

La yonent bi wax ci turu Aji Sax ji, su sottiwul, dikkul rekk, loola du kàddu gu Aji Sax ji wax. Ñeme Yàlla la ko yonent ba waxe, buleen ko ragal.

Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne: «Buleen déglu yonent yi leen di wax ay waxyu; cóolóoli neen lañu leen di naxe, di fent ay peeñu, di wax ay waxyu, te du kàddug Aji Sax ji.

Te man ci sama bopp,” kàddug Aji Sax jee, “maa koy nekkal tatay sawara ji ko ub ràpp. Te it maay doon daraja ji ci biiram.”