TSK

TSK · Numbers 2:29

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Ñu lim turi sëti Neftali, ku nekk ak làngu cosaanam ak kër maamam, mboolem ñi xare war, te ñu am ñaar fukki at, jëm kaw.

ak saraxu cant gi ci biir jàmm, di ñaari yëkk ak juróomi kuuy ak juróomi sikket, ak juróomi xari menn at. Looloo doon saraxu Ayra doomu Enan.

¶ Ñi askanoo ci Neftali ñook seeni làng ñoo di ñoom Yàcceel, mi sos làngu Yaceleen ñi, ak ñoom Gunni mi sos làngu Guneen ñi,