TSK

TSK · Numbers 22:41

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Balag ne ko: «Kaay rekk, topp ma, ba feneen fooy tollu di leen gis. Seen cat doŋŋ ngay gis nag, waaye doo leen gis ñoom ñépp. Su ko defee nga móolul ma leen foofu.»

tasleen tasar mboolem bérab, ya xeet ya ngeen di dàq, di jaamoo seeni tuur; muy kaw tund yu mag ya, di kaw tund yu ndaw ya, di ker garab yu naat ya.

Maay bóome biir Mowab.» Kàddug Aji Sax jee. «Maay bóom kuy joxe sarax ci jaamookaay, di taalal am tuuram cuuraay.