TSK

TSK · Numbers 24:18

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Yal na la ay giir nangul, ay réew di la sujjóotal, nga yilif say bokk, te say doomi ndey di la sujjóotal. Ku la móolooy alku, te ku la ñaanal barkeel.»

Ba leen Yanqóoba gisee, da ne dalub Yàllaa ngii, ba tax mu tudde bérab ba Maanayim (mu firi Ñaari dal).

¶ Ba mu ko defee Aji Sax ji gemb ab noon bu jógal Suleymaan. Muy Adàdd, Edomeen ba askanoo ca buurub Edom.

Mu jëm ci njiital jàngkat yi, dëppook galan bu ñuy wax Seedeb Tóor-tóor, di taalifu jàngle, ñeel Daawuda.

Aji Sax ji nee: «Saab saamar a reye fa asamaan ba màndi deret, te mu ngii di wàccal Edom, xeet wi may faagaagal, ngir àttee leen ko.»

Amos 9:12 TSK

Su boobaa bànni Israyil nangu ndesu Edom, ak mboolem suufi xeet yi ñu ma tudde woon.» Kàddug Aji Sax jee, te moom lay def.