TSK

TSK · Numbers 24:6

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Naka noona Yàlla Aji Sax ji jëmbat tool ca biir Àjjana fa féete penku ba, tàbbal ca nit ka mu bind.

Loo def mu àntu: nga mel ni garab gu saxe walum ndox, bu jotee meññ, te xob wa du lax.

Maa gis jéllu noon yi, dégg yuuxi ñu bon ñi may tëru.

Maay def garabi seedar aki séng ca màndiŋ ma, saxal garabi mirt ak oliw ca joor ga, sippar ak garabu pẽe, ak yeneen garab yu dëkke naat, ma boole ca,

Ngalla gàcceelal ñi ma topp, te bu ma gàcceel; yal nañu tiit, ñoom, te man, ma baña tiit. Rikk dikke leen bésub safaan, rajaxe leen ñaari yoon.

Asiree ngoog, garabu seedar la woon ca Libaŋ, rafeti bànqaas, naatalub gott, siggi ca kaw, njañ lay àkki niir ya.