TSK

TSK · Numbers 27:11

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

yaar muy baayam bu ndaw mbaa doomu baayam bu ndaw. Ku mu bokkal làng di mbokkam lenqe sax man na koo jotaat, te moom ci boppam man naa woomle ba jotaat boppam.

Ruth 4:3 TSK

¶ Mu wax ak mbokk ma yeyoo sañ-sañu jotaat ba, ne ko: «Ab làccu suuf bu sunu mbokk Elimeleg moomoon la, Nawmi di ko jaay. Mooy ka jóge réewum Mowab, ñibbsi.

¶ Ba loolu amee Anamel sama doomu baay bu ndaw dikk, na ma ko Aji Sax ji waxe. Mu fekk ma ci ëttu dag yi, ne ma: «Rikk jëndal sama tool ba ca Anatot ca diiwaanu Beñamin ndax sa alal la ci yoon, yaa ko saña jotaat. Kon jënd ko.» Ma xam ne loolu kàddug Aji Sax jaa.