TSK

TSK · Numbers 30:1

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Musaa xamal ko la ko Aji Sax ji dénk lépp, ak mboolem firnde, ya mu ko sant mu def ko.

Giir gu ci nekk, àndleen ceek kilifa yi jiite seen këri maam, ñu jàpple leen ci.

«Ñii nag ñoo leen di séddale réew mi: Elasar sarxalkat bi, ak Yosuwe doomu Nuun.