Numbers 31:6
TSK
Musaa nag yebal leen, junni jóge ci giir gu nekk, ñu xareji. Ñoom ak sarxalkat bi Fineyas doomu Elasar, ñoo xareji, yóbbaale jumtukaay yu sell yaak liiti xare ya.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Musaa nag yebal leen, junni jóge ci giir gu nekk, ñu xareji. Ñoom ak sarxalkat bi Fineyas doomu Elasar, ñoo xareji, yóbbaale jumtukaay yu sell yaak liiti xare ya.
¶ Gannaaw loolu Rabsake dégg ne buurub Asiri bàyyikoo na Lakis, bay xareek dëkk ba ñuy wax Libna. Mu walbatiku fekki ko foofa.