TSK

TSK · Numbers 34:7

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

Ba ñu bàyyikoo Kades, ca tundu Or wa digalook réewum Edom lañu dali.

¶ «Géej gu mag gi mooy doon seen kemu sowu. Loolooy seen kemu sowu.

Na lii di kemu réew mi ci wetu bëj-gànnaar: géej gu mag ga lay dale, topp yoon wa jaare Ettlon ak Lebo Amat, ak Cedàdd,