TSK

TSK · Numbers 5:29

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ «Li yoon dogal ci saraxu cant ci biir jàmm, te nit sañ koo sarxalal Aji Sax ji mooy lii:

¶ Loolu la yoon digle ci liir wuy law wu tegu ci ndimol kawar gu ëccu mbaa lu wëñ gu ëccu mbaa bàgg mbaa poqe mbaa lu ñu defare der. Ci digle yooyu lañuy tegu, ba mana biral ne këf ka set na am setul.

¶ Loolu la yoon digle ci mbiri góor gu ànd ak jàngoroy xelli mbaa mu génne wasal, ba sobewu;

na waa ji yóbbu jabaram ca sarxalkat ba, te yóbbaleel ko saraxu ñetti kiloy sungufu lors. Du ci sotti diw, du ci def cuuraay, ndax saraxu pepp boobu saraxu fiiraange la, saraxu toppukaay la bu ñuy toppe ñaawtéef.

Tóokëru Aji Sax ji Boroom gàngoor yi kat, mooy waa kër Israyil. Niti Yuda it ñooy njëmbat li mu safoo. Mu di ko yaakaare njub, njubadi ne jaas. Mu yaakaar njekk, yuuxi njekkar ne jaas.