TSK

TSK · Numbers 6:10

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ «Bu nit ki dee sarxalal Aji Sax ji njanaaw luy doon rendi-dóomal, na sarxe pitax mbaa xati mu ndaw.

¶ Keroog bésub juróom ñetteel ba, Musaa woolu na Aaróona ak doomam yu góor, ñook magi Israyil ña.

ak ñaari pitax mbaa ñaari xati yu ndaw, lu mu ci gëna jekku rekk. Menn mi saraxu póotum bàkkaar la, mi ci des di saraxu rendi-dóomal.

Bésub juróom ñetteel ba, na wut ñaari pitax mbaa ñaari xati yu ndaw te teewi fi kanam Aji Sax ji ca bunt xaymab ndaje ma, daldi koy jox sarxalkat bi.

Su ni demee ba mu sobeel boppam, na setlu te négandiku juróom ñaari fan, doora dellu ca liggéeyam.

mi ñu teg ciy loxo, mu dee ndax sunuy tooñ, ba dekkal ko, ngir nu jagoo àtteb nit ñu jub.