Exodus 29:24
TSK
Nga boole lépp, teg ko ci loxoy Aaróona aki doomam, ñu def ko saraxu yékkati-jébbale, ñeel Aji Sax ji.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Nga boole lépp, teg ko ci loxoy Aaróona aki doomam, ñu def ko saraxu yékkati-jébbale, ñeel Aji Sax ji.
Mu boole yooyu yépp teg ci loxol Aaróona ak loxoy doomam yu góor, ngir ñu def ko sarax bu ñuy yékkati, jébbal Aji Sax ji.
«Giirug Lewi ñoom, bu leen lim, bu leen waññaaleek bànni Israyil.
¶ «Na sarxalkat bi jébbale loola, defal ko Aji Sax ji saraxu yékkati-jébbal. Cér yu sell a ngoogu ñeel sarxalkat bi, mu boole kook dënn biy saraxu yékkati-jébbal, ak jooxeb tànkub kanam bi. Gannaaw loolu nasireen bi sañ naa naan biiñ.