TSK

TSK · Numbers 9:18

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Back to passage

¶ Gannaaw loolu mbooloom bànni Israyil gépp bàyyikoo màndiŋu Ciin, di dox ak a taxaw, ci ndigalal Aji Sax ji. Ñu dem ba Refidim, dal fa. Foofa nag mbooloo ma amuñu woon ndox mu ñu naan.

Leeg-leegaa fan yu néew la niir way dal-lu fa tiim màkkaan ma. Waaye ci kàddug Aji Sax ji daal, lañuy dale te ci kàddug Aji Sax ji lañuy faboo.

¶ Bokk yi, bugguma ngeen umple ko, sunu maam yépp la niir wa yiiroon, te ñoom ñépp a jàll géej ga.