Proverbs 9:1
TSK
Soxna si, Xel mu Rafet daa tabax këram, yett juróom yaari kenoom.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Soxna si, Xel mu Rafet daa tabax këram, yett juróom yaari kenoom.
Te moom it moo tax ngeen bokk ci Almasi Yeesu, mi ñu def muy sunu xam-xam bu bawoo fa Yàlla, di sunu njekk, di sunu sellte, di sunug njot,